1 Samuel 17:8
TSK
¶ Golyaat taxaw, janook làngi Israyil, àddu ca kaw, ne leen: «Ana lu ngeen di génn, làng-déral xare nii? Xanaa du maay waa Filisti ji, yeen ngeen di surgay Sóol? Tabbleen genn góor, mu wàcc, dajeek man.