2 Kings 18:7
TSK
¶ Aji Sax ji nag ànd ak Esekiya, mu am ndam ci mboolem lu mu sumb. Bañ na noteelu buurub Asiri, ba nangulatu ko.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ Aji Sax ji nag ànd ak Esekiya, mu am ndam ci mboolem lu mu sumb. Bañ na noteelu buurub Asiri, ba nangulatu ko.
¶ Ba loolu amee Sanbalat ma dëkk Oron dégg ko, mook Amoneen ba Tobya, jawriñ ba, ak Gesem, Araab ba. Ñu di nu ñaawal ak a diiju naan: «Li ngeen di def nii lu mu doon? Dangeen di fexeel Buur?»
Ku rafet xel di boroom doole, ku xam, gëna man;
Ka bokk ci askanu buurub Israyil nag fippu, yónni ay ndaw réewum Misra, ngir ñu jox ko ay fas ak mbooloo mu takku. Moo ka def loolu dina baaxlee? Mbaa dina mucc? Nu mu cay mucce te wor kàddu, ga mu fasoo woon?