TSK

TSK · Isaiah 36:6

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Misra daal, nga def sa yaakaar, bantu barax bu tas boobu di sokk képp ku ko wéeroo! Firawna buuru Misra de, mooy boobu bant ci képp ku ko yaakaar.

Wóoy ngalla doom yii diy fippukat! Kàddug Aji Sax jee. Ñu ngi nas mébét yu ma diglewul, di digoo digoo yu ma leen xelalul, di tegle bàkkaar ci kaw bàkkaar.

Waa Misra, niti neen, duñu Yàlla; seeni fas it, suuxu neen, duñu leneen. Aji Sax jeey xàcci loxoom, kiy walloo mooy tërëf, ki ñuy wallu daanu, ñoom ñépp bokk sànku.

«Aji Sax ji Yàllay Israyil dafa wax ne: Buuru Yuda mi leen yebal, ngeen seetsi ma, waxleen ko ne ko: “Mbooloom Firawna mi génnoon di leen wallusi kat, dëpp na bay dellu Misra.

ba waa Misra gépp xam ne maay Aji Sax ji. «“Seen ndimbal ak Israyil mooy ndimbalu bantu barax,