Fekk na ñu wax Daawuda ne ko Ayitofel bokk na ca ña lëngook Absalom. Daawuda nag ñaan ne: «Yaw, Aji Sax ji, ngalla yàqal pexem Ayitofel.»
TSK
TSK · Isaiah 37:21
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
2 Samuel 15:31
TSK
2 Kings 19:20
TSK
¶ Ba mu ko defee Esayi doomu Amocc yónnee ca Esekiya ne ko: «Aji Sax ji Yàllay Israyil dafa wax ne li nga ko ñaan ci Senakerib buurub Asiri, dégg na ko.
Psalms 91:15
TSK
Mu woo ma, ma wuyu ko; mook man ci biir njàqare, ma xettli ko, darajaal ko,
Isaiah 38:3
TSK
Mu ne: «Éy Aji Sax ji, ngalla bàyyil xel ni ma àndeek yaw sama léppi xol, ci kóllëre. Te it li nga rafetlu laa jëfe.» Mu jooy nag, jooy yu metti.
Isaiah 58:9
TSK
Su boobaa bu ngeen wooyee Aji Sax ji, mu wuyu; ngeen ne wallóoy, mu ne “Maa ngi.” Ndegam génne ngeen noteel ci seen biir, ak di joxoñeek a wax lu ñaaw,
Daniel 9:20
TSK
¶ Maa ngay wax ak a ñaan, di tuub sama bàkkaar ak a tuubloo Israyil sama ñoñ tey dagaanal sama tundu Yàlla wu sell wi, ci sama Yàlla Aji Sax ji.