TSK

TSK · Isaiah 4:1

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Mu ëmb, am doom ju góor, daldi ne: «Yàlla teggil na ma gàcce.»

Mikal doomu Sóol jooju nag amul doom, ba ni mu deeye.

Bésub keroog booba, kuy daŋŋiiral, detteelu, sagub nit sàggiku, Aji Sax ji doŋŋ mooy jagoo kawe.

Keroog bés booba li des fi Israyil ak li rëcce kër Yanqóoba duñu wéerooti ña leen duma. Aji Sax ji lañuy wóolu, wéeroo ko, Aji Sell ju Israyil.

Bésub keroog nit sàkku Ki ko sàkk, ba ne jàkk Aji Sell ju Israyil.

Luke 1:25 TSK

«Lii Boroom bee ma ko defal ci jant yi mu ma geesoo, ba teggil ma sama gàcce gi ci biir nit ñi!»

Ñu ni mel lanuy sant ak a dénku ngir Sang Yeesu Almasi, ngir ñu dal, tey yëngu, di dunde seen ñaqu bopp.