TSK

TSK · Isaiah 40:12

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Job 28:25 TSK

Ba Yàlla àppalee ngelaw diisaayam, nattal ndox ab dayoom,

Ma ne: «Éy sama Yàlla, maasoo maas, say at du jeex. Bu ma yóbboo sama diggi fan.

laata Yàllaa sàkk suuf aki àllam ak feppu pënd ci àddina.

te sama loxo bee dëj suuf, sama ndijoor bi firi asamaan. Maa leen di woo, ñu bokk taxaw.

¶ Ci kaw loolu ma gis ngàngune mu mag mu weex, ak ku ci toog. Asamaan ak suuf daldi dawe fa kanamam, ne mes.