¶ Ci kaw loolu Aana ñaan ne: «Sama xol a ngi bége Aji Sax ji, ci Aji Sax ji laa ame doole. Maa am tontal noon yi, nde maa bànneexoo sag wall.
TSK
TSK · Isaiah 41:16
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Yeen waa Siyoŋ, serleen te sarxolleel ku màgg ki fi seen biir, Aji Sell ju Israyil.»
Aji Sax ji, yaay sama Yàlla, dama lay teral, di la sant. Yaa defi jaloore, muy dogal yu yàgg, wér te wóor.
Dees na ma waxal ne: «Aji Sax ji rekk a jagoo njekk ak doole!» Mboolem ñi ma mereey ànd, sëgg, fekksi ma.
Kuy damu kay, na damoom xelam mu ko may mu xam ma, xam ne maay Aji Sax, jiy jëfe ngor ak dëgg ak njekk fi kaw suuf. Loolu déy mooy sama bànneex.» Kàddug Aji Sax jee.
Maay yónnee Babilon ay beeskat yu ko bees, tonni réew ma, ba mu set. Keroog bésu safaan ba déy, fu ne lañu koy songe.
te man may bànneexoo Aji Sax ji, Yàlla ji may wallu laay bége.
¶ Maryaama nag ne:
Te moom it moo tax ngeen bokk ci Almasi Yeesu, mi ñu def muy sunu xam-xam bu bawoo fa Yàlla, di sunu njekk, di sunu sellte, di sunug njot,