Mooy yékkatil xeet yi raaya, dajale góor ña ñu dàqe Israyil, ak jigéen ña ñu jële Yuda, tasaare leen, ñu jóge ñeenti weti àddina, booloo.
TSK
TSK · Isaiah 43:6
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Isaiah 11:12
TSK
Isaiah 27:13
TSK
Bésub keroog liit gu mag jib, ña laŋoon réewum Asiri délsi, ànd ak ña ñu tasaare woon biir réewum Misra, ba sujjóotalsi Aji Sax ji fa Yerusalem, fa kaw tund wu sell wa.
Jeremiah 3:14
TSK
«Yeen doom yu woyof kumba yi, délsileen.» Kàddug Aji Sax jee. «Maay seen boroom kër, maay jële kenn ci bii dëkk, ñaar ca bee gox, boole indi Siyoŋ,
Jeremiah 23:8
TSK
Xanaa dañu naan: “Giñ naa ko ci Aji Sax jiy dund te génnee askanu Israyil réewum bëj-gànnaar, génnee leen mboolem réew ya mu leen sànkeji woon.” Su ko defee ñu dëkkewaat seen suufas bopp.»
Romans 9:25
TSK
Moom la wax it ci téereb Ose ne: «Ñi dul woon sama ñoñ, ñoom laay wax sama ñoñ, ñooñu dul woon samab xejj, ñoom laay xejjoo.»
Galatians 3:26
TSK
¶ Yeen ñépp doomi Yàlla ngeen, ndax li ngeen gëm Almasi Yeesu.