Isaiah 6:9
TSK
Mu neeti: «Demal, wax askan wii, ne leen: “Dégluleena déglu te buleen dégg, xool-leena xool te buleen gis.”
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Mu neeti: «Demal, wax askan wii, ne leen: “Dégluleena déglu te buleen dégg, xool-leena xool te buleen gis.”
Ñii xamuñu, xàmmeewuñu, seeni gët lañu lëndëmal, ba gisatuñu; fatt seenum xel, ba xelootuñu.
¶ «Yaw nit ki, digg kërug fippukat nga dëkke, ñu ami gët te duñu gis, ami nopp te duñu dégg, ndax kërug fippukat lañu.