TSK

TSK · Isaiah 44:28

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Ezra 1:3 TSK

Képp ku bokk ci mboolem ñoñam, yal na Yàllaam ànd ak moom, mu dem ba Yerusalem ga ca Yuda, tabax fa kër Aji Sax ji, Yàllay Israyil, Yàlla ja ca Yerusalem.

fa mu doon topptoo jur ga; mu sàmmal ko waa kër Yanqóoba, askanu Israyil wi mu séddoo.

Maay tonni tund wu mag ak wu ndaw, lu cay gàncax, ma fóom; ag dex, ma def ag joor; ab déeg, ma ŋiisal.

Maa lay jagleel denc yu loq, ak alal ju làqe, ba nga xam ne maay Aji Sax ji lay wooye sa tur, man Yàllay Israyil.

Maay wooye jaxaay penku, wooye réew mu sore, kuy sottal sama mébét. Maay àddu, amal; maay nas, sottal.

Maa àddu, man mii; maa ko woo, indi ko, te pexeem dina joy.

maa ngii di yónnee, jëli mboolem làngi bëj-gànnaar.» Kàddug Aji Sax jee. «Maay yónnee it ca Nabukodonosor buuru Babilon mi ci samag curga, daldi leen boole indi ci kaw réew mii ak ñi ci biiram ak mboolem xeet yi ko séq. Maa leen di faagaagal, gental leen gent bu sax dàkk bu ñuy muslu.