TSK

TSK · Isaiah 45:9

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Job 9:4 TSK

Moo rafet xel, bare doole! Ana ku koy jéema të, mu jig ko?

Job 10:9 TSK

¶ Rikk fàttlikul ne yaa ma tabax, ni bu ma doon ban, xanaa doo ma delloo xaat ci pëndub suuf?

Job 40:2 TSK

Yaw miy layook Aji Man ji, dangay diiŋat? Yaw miy weranteek Yàlla, doo tontu?

Buuri àddinaa ngi dér, boroom nguur yi daje, di fexeel Aji Sax ji, mook ki mu fal.

Lu masa ay, dees koo tuddoon; lu doom aadama doon, xamees na ko, te kenn du layook ku la sut.

Yeenaka juunum xel! Dees na jaawale tabaxkatu njaq beek ban bi? Ndax li ñu sàkk dina ne ki ko sàkk: «Kii sàkku ma»? Am njaq leey waxtaane tabaxkat bi naa: «Kii manula tabax»?

Éy Aji Sax ji, bul mer lool, bul ba xel fàww ci ñaawtéef. Ngalla seetal ne nooy sa ñoñ, nun ñépp.

Babilon, maa la fiir, nga tancu te yéguloo! Dañu laa gis, ne la taral, yaa dëkk Aji Sax ji,