Su ñu muusoon, xalaat ci lii, ba xam nu ñuy mujje.
TSK
TSK · Isaiah 46:8
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Psalms 135:18
TSK
Ñi sàkk yii tuur, yal nañu mel ni ñoom, ñook ñi leen wóolu ñépp.
Isaiah 47:7
TSK
te naa: «Ba fàww maay lingeer!» ba tax bàyyiwoo xel ca la ngay def; xalaatoo la muy jur.
Ezekiel 18:28
TSK
Ndegam moo xoolaat, ba dëddu mboolem tooñam yu mu tooñ, dina dund déy. Du dee moos.
Haggai 1:7
TSK
Aji Sax ji Boroom gàngoor yi dafa wax ne: «Teewlooleen xel seeni jaar-jaar.
¶ Bokk yi, buleen doon ay xale ci wàllu déggin. Su dee lu bon, nekkleen ci ay tuut-tànk, waaye màggleen ci wàllu déggin.