Mu jëm ci njiital jàngkat yi, dëppook galan bi ñu dippee Pitax mu luu, dëkk fu sore; di taalifu jàngle bu Daawuda fentoon, ba ko Filisteen ña jàppee ca Gaat.
TSK
TSK · Isaiah 49:19
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Nanu mel ni njaniiw, mëdd kuy dund, mu jekki tàbbi biir bàmmeel.
Aji Sax ji dafa wax ne: «Bu bésub yiw taxawee, ma nangul la; bu bésub mucc jotee, ma wallu la, sàmm la, def la ngay kóllëre sama digg ak askan wi, ngir yékkatiwaat réew mi, séddalewaat ay cér, suuf sii gental tey,
Aji Sax ji déy dafa wax ne: «Moona dees na foqati ku jàmbaar jàpp, ba rëccal alalu sëxëtoob boroom doole. Say jotewaale, maay joteek ñoom, te say doom, maa leen di wallu.
«Yaw mi jaasir ba juroo, xaacul! Yaw mi xamul mititu mat, sarxolleel.» Aji Sax ji nee: «Ndaw si ñu foñ moo gëna jaboot kiy séy.
Waaye ku la lekk, dees na ko lekk; sa noon yépp lañuy jàpp njaam ba ñu daj. Ku la futti, dees na ko futti, ku la saax-saaxee dees na ko saax-saaxee.
¶ Aji Sax ji dafa wax ne: «Bérab bii ngeen ne ab gent la bu kenn nekkul, du nit, du rab te muy dëkki Yudak mbeddi Yerusalem yii gental, kenn nekku fi, du nit, du rab, dees na fi déggati
Maay dikke mbugal Bel, tuur mi ci Babilon, yàbbiloo kob lancam. Xeet yi noppee def um wal, wuti ko, tatay Babilon it màbb.
Maa ngii déy maak yeen, maa leen di geesu, ba ngeen ruuje, jiwe.
Ma ne: «Lan la ñii di defsi?» Mu wax ma, ne ma: «Béjjén yii tasaare Yuda ba kenn siggeetul, tëgg yii ñoo dikk ngir tiital leen, ba jàllarbi béjjéni xeet yi jóg song réewum Yuda, tasaare ko.»
«Éy Siyoŋ, rëccal, yaw mi dëkke janq Babilon mu taaru mi.»