Exodus 39:40
TSK
ak sori wurmbalu ëtt bi aki jënam aki tegoom, ak kiiraayal lafu buntu ëtt bi, aki buumam aki xeram; mboolem jumtukaay, yi ñuy liggéeye ci màkkaanu xaymab ndaje mi rekk,