TSK

TSK · Isaiah 59:8

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Mu jëm ci njiital jàngkat yi, dëppook galan bi ñuy wooye Bul yàq, di taalifu jàngle, ñeel Daawuda.

mucc ci kuy wacc yoonu njub, di jaare mbedd yu lëndëm.

Jàmm,» la Aji Sax ji wax ne, «du ñeel ñu bon ñi.»

ba yoon dellu gannaaw, njekk dànd, dëgg fakktaloo fa pénc ma, njub tëë agsi.

«Wërleen mbeddi Yerusalem, xool-leen, seet ciy péncam rekk ba xam ndegam dingeen gis kenn, kenn kepp kuy def njub, di sàmm worma, ma daldi leen baal.

Amos 6:1 TSK

Wóoy ña ne finaax ca Siyoŋ, wóoy ña naagu fa tundu Samari! Ñooy kàngami xeet wi gëna màggeey, niti Israyil di leen diis-si soxla.

Luke 1:79 TSK

di niital ñi tooge biir lëndëm ak takkndeeru ndee, di nu gindi, teg nu ci yoonu jàmm.»