TSK

TSK · Isaiah 60:4

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Mooy yékkatil xeet yi raaya, dajale góor ña ñu dàqe Israyil, ak jigéen ña ñu jële Yuda, tasaare leen, ñu jóge ñeenti weti àddina, booloo.

Mu ne: «Man Aji Sax ji, maa la woo cig njekk, jàpp la ci loxo, sàmm la, def la ngay kóllëre sama digg ak nit ñi; def la ngay leeru xeet yi,

Ñi lay tabaxaat dañuy gaaw, te ñi la yàqteek ñi la gental dañuy dem, ba la.

Ñàkkoon ngay doom, waaye ku nekk ci say doom ay dëkkalaat yii kàddu ci sab nopp: “Fii dafa xat, xajal ma, fu ma dëkke!”

Aji Sax ji déy dafa wax ne: «Maa ngii di yóbbu Yerusalem ci jàmm ju mel ni géej, ak waamey koom muy wal, bawoo ci xeet yi. Yeenay tooge luppu Yerusalem, di nàmp, uufu ciy óom, mu di leen raay.

¶ Bésub Noflaay ba ca topp, daanaka waa dëkk bépp a daje, ngir déglu kàddug Boroom bi.