Ana ku may taxawal ci ñu bon ñi? Ku may jógal ci biir ñiy def lu bon?
TSK
TSK · Isaiah 63:5
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Psalms 94:16
TSK
Psalms 107:12
TSK
Mu teg leen naqar, ba torxal leen, ñu ne nërëm te kenn walluw leen.
Isaiah 41:28
TSK
Xool naa xool ci tuur yi, gisuma kenn; du kenn ci ñoom ku ciy xelale, ba ma laaj ko, mu mana tontu.
Isaiah 51:9
TSK
Aji Sax ji, yewwul, ngalla yewwul; wone sa doole. Yewwul na bu jëkkoon, bu yàgga yàgg. Xanaa du yaa falaxe Raxab? Du yaa jam ninki-nànka jooja?
Isaiah 59:16
TSK
Daa xool, gisul kenn; mu tiisoo li ci kenn jógul, moo tax loxoom may ko ndam, te njekkam la sukkandikoo.
Hosea 1:7
TSK
Waaye waa kër Yuda, maa leen di yërëm. Seen Yàlla Aji Sax ji laa leen di walloo, waaye duma leen walloo fitt mbaa saamar, mbaa ay xare, mbaa ay fas aki gawar.»
Waaye ci ñi ñu woo, ñuy Yawut, di Gereg, Almasi mooy manoorey Yàlla, di xam-xamu Yàlla.