TSK

TSK · Isaiah 65:4

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ «Ngëneeli meññeef ma jëkka ñore ca seen suuf, moom ngeen di yóbbu seen kër Yàlla Aji Sax ji. «Ab tef, buleen ko togge soowum yaayam.

Mbaam-xuux, we wi xar na waaye du duññ, kon daganul ci yeen.

Képp ku laal ca àll ba, nit ku ñu bóome saamar, mbaa ku Yàlla moomal boppam, mbaa mu laal yaxi nit ku dee, mbaa mu laal bàmmeel, kooka day sobewu diiru juróom ñaari fan.

Mbaam-xuux, moom, we wi xar na waaye du duññ. Kon daganul ci yeen. Aw suuxam, buleen ko lekk, te méddam, buleen ko laal.

ak kuy liggéeyaate, ak kuy seete ab rawaan, ak kuy seete aw rab, mbaa kuy seete nit ñu dee,

«Ñii di sellalu ak a sangu-set bala ñoo duggi tool ya ñuy tuuroo, di fa toppi ca gannaaw ka ca digg ba, ñooñooy lekk yàppu mbaam, ak yeneen yu seexluwu ni janax, te ñooy bokk sànku.» Kàddug Aji Sax jee.

Ci seen gémmiñ laay foqatee deret ji ñuy lekk, yàbbiloo leen seen ñam yu seexluwu yi ñu ŋank. Seenu ndes it dina ma def seen Yàlla, mel nig làng ci giirug Yuda, Ekkron it ci sama ñoñ lay bokk ni Yebuseen ñi.