TSK

TSK · Isaiah 8:9

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Buurub Israyil ne: «Waxleen ko ne ko: “Jóge xare, di bàkku moo gën jëm xare, di bàkku.”»

Ab soxor mbugalam du jaas, wóor na; te ku jub, saw askan mucc.

Aji Sax jee damm bant, bi ñu bon ñi daan dóoree! Moo damm seen yetu nguur,

Moo tax seen kàddug Aji Sax mujj di: «Ca rëdd wii, ca rëdd wee, nàngam sii, nàngam see, as tuut fii, as tuut fee.» Moo tax ñuy tërëf, daanoo njaaxaanaay ba damm, di sërëx ak a keppu.

Xanaa dees na songe moos, waaye ku la song it, yebalu ma ko, te ku la song daanu fi sa kanam.

Takkleen fas yi, war naari góor yi, ba làng-déraale seen mbaxanay xare, nàmmaat xeej, sol yérey xare!»

«“Nanga waajala waajal, yaak mboolem sa ndaje mi dajesi fi yaw, nga doon seen wattukat.

Waaye yaa naa jàyy ni ngëlén, mel ni aw xiin, muur réew mi, yaak sa gàngoor yépp, ak xeeti xeet yi ànd ak yaw.

¶ Bés a ngii di dikkal Aji Sax ji, ca lees di séddoo fi seen biir, alal ju ñu nangoo ci yeen.

mu dikk, naxsi askani ñeenti colli àddina, yi ñuy wax waa Gog ak Magog. Mu dajale leen ngir xare, ñu bare ni feppi suufas géej.