Isaiah 7:7
TSK
Waaye Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: ‘Loolu du sotti, du am.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Waaye Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: ‘Loolu du sotti, du am.
Wóoy ngalla Efrayim, kaala gu yànj ga ay màndikatam di sagoo! Taaram bu yéeme baa koy réer, ni tóor-tóor yu wow, te ma nga toŋ ca coll, wa ña biiñ man dëkke, fa tiim xur wu nangu wa.
¶ Kàddug Aji Sax jii moo dikkaloon Mise miy waa Moreset, ca janti Yotam ak Axas ak Esekiya, buuri réewum Yuda, na seen nguur topplantee. Lii la Mise gis ci mbirum Samari ak Yerusalem.
¶ Ci kaw loolu ma dellu séentu, gisuma lu moy taxañu mbind buy naaw.