TSK

TSK · James 2:4

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Job 21:27 TSK

Mu ngoog! Maaka xam li ngeen foog, te di ma ko fexee fitnaale!

Mu jëm ci njiital jàngkat yi, dëppook galan bi ñuy wooye Bul yàq, di taalifu jàngle, ñeel Daawuda.

Mooy féete ndijoor néew-ji-doole, musal ko ci ku koy teg àtteb dee.

James 1:1 TSK

¶ Ci man Yanqóoba, jaamub Yàlla ak Sang Yeesu Almasi, la bataaxal bii bawoo, ñeel fukki giir ak yaar yi tasaaroo ci àddina. Maa ngi leen di nuyu.