TSK

TSK · James 3:18

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Ku yaakaar sa alal sab jéll a ngi ñëw, ku jub day juble ni gàncax gu naat.

Su boobaa yoon dëkke màndiŋ mi, njekk tooge tóokër bi.

Amos 6:12 TSK

Moo fas dina daw ciy doj a? Am dees na ràng aw nag, di gàbb doj? Moona walbati ngeen àtteb yoon, def ko tooke, yoon mel ni xay.

Su boobaa ngeen meññal ba woomle ci njub, gi Yeesu Almasi di maye, ngir fésal màggug Yàlla, jollil ag cantam.

Ndax merum nit du jur njub fa Yàlla.