Job 38:2
TSK
Ana koo doon, bay lëntal samay dogal, di wax loo xamul dara?
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ana koo doon, bay lëntal samay dogal, di wax loo xamul dara?
¶ Yaw nit kiy sikke nag, amoo aw lay, ndax boo sikkee keneen, sa bopp nga sikk, nde yaw miy sikke, jooju jëfin ngay jëfe.
Yaw miy sikkal jaamub jaambur, yaay kan? Su baaxalee mbaa mu bonal, sangam a koy seet! Te day baaxal ndax Boroom bi man na koo baaxal.
Looloo waral mu mana musal mucc gu mat sëkk, ñiy awe fi moom, dikk fa Yàlla, ndax mooy dund ba fàww, ngir di leen tinul.