Job 7:6
TSK
Kukkub ràbb sax ni samay fan di jeexee ko gaaw, poqe di jeex, te yaakaar amul.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Kukkub ràbb sax ni samay fan di jeexee ko gaaw, poqe di jeex, te yaakaar amul.
Ku jigéen jur, yaa néewi fan, géejal coono!
Éy Aji Sax ji, xanaa lii du jeex? Xanaa doo làqu fàww nii, sa mer di boy?
Bu ma dummóoyu bésub njàqare; teewlu ma, gaawe ma sama bésub woote!
te ki barele it na sagoo ag suufeem, ndax ni tóor-tóoru saxayaay di ruuse, noonu lay wéye.
¶ Te itam mujug lépp dëgmal na; kon nag jiital-leen seenum xel, te ànd ak seen sago, ngir ngeen man di ñaan.