TSK

TSK · James 5:2

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Job 13:28 TSK

Sama bakkan a ngi ruus ni bant bu fënëx, mbaa mbubb mu maxe.

Ma ne, Boroom bi Aji Sax jee may dimbali. Ana ku may daan? Dama ne, ñoom ñépp ay jeexal ni yére yu saxe ba sagaroo.

Kuy jagoo alal ju lewul, mooy picc mu toj lu mu nenul. Kookooy tollu digg dooleem, alal ja dëddu, mu mujje dof.»

James 2:2 TSK

Ndax su nit duggsee seenum ndaje, takk jaarob wurus, solu ba jekk; ku néew doole it duggsi, limboo ay sagaram,