1 Samuel 28:21
TSK
Jigéen ja dikk, gis Sóol mu jàq lool. Mu ne ko: «Aa, sang bi, man de déggal naa la. Jaay naa sama bakkan, def li nga ma sant.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Jigéen ja dikk, gis Sóol mu jàq lool. Mu ne ko: «Aa, sang bi, man de déggal naa la. Jaay naa sama bakkan, def li nga ma sant.
Sama bakkan ci xott saa su ne, waaye fàttewuma saw yoon.
Manase song Efrayim, Efrayim song Manase, ñu mànkoo, noonoo Yuda. Teewul Aji Sax ji xàcci loxoom, meddiwul ba tey.