Ba Yàllay féncoo yaa doon déglu, ba mana aakimoo xel mu rafet?
TSK
TSK · Job 13:2
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Job 15:8
TSK
Job 34:35
TSK
ne ma: «Ayóoba mii waxewul xam-xam, te kàddoom yi du xel.»
Job 37:2
TSK
Dégluleena déglu dënoom gay ràndaŋ, kàddu gay rëkke fa gémmiñam,
Job 42:7
TSK
¶ Gannaaw ba Aji Sax ji waxee Ayóoba yooyu kàddu, Aji Sax ji dafa wax Elifas ma cosaanoo Teman, ne ko: «Sama xol tàng na ci yaw, yaak sa ñaari xarit yi, ndax waxuleen dëgg ci man ni sama jaam bi Ayóoba waxe.
Ndax kat gaaw ngeena xajoo lool, nit ku dikk, di leen waare meneen Yeesu mu nu waarewul, mbaa geneen noo gu ngeen jot te jotuleen ko woon, mbaa beneen xibaar bu ngeen dëggal, te mu wuute ak ba ngeen déggoon.
¶ Mujj naa dib dof nag, te yeena ma ko yóbbe, nde gërëm maa leen waroon, ndax doonte duma dara sax, ndaw yu màgga màgg yooyeey, duma seen cuune ci lenn.