Gannaaw loolu ñu indil Yuusufa seeni jur, Yuusufa jox leen ko pepp, wecci leen ko seeni fas ak seeni gétti jur gu gàtt ak gu gudd ak seeni mbaam. At mooma jox na leen ab dund, mu wecci seen gétt gépp.
TSK
TSK · Job 2:4
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Genesis 47:17
TSK
Esther 7:3
TSK
Lingeer Esteer àddu ne ko: «Buur, ndegam xool nga ma bëtu yiw te neex na la, may ma, ma mucc maak samaw xeet; moom laay ñaan te moom laay sàkku.
Isaiah 2:20
TSK
Bésub keroog booba, yàllantuy xaalis ak wurus ya nit sàkkal boppam, di leen sujjóotal, ñoom lay sànni ca jaar yaak njugub ya,
Luke 12:23
TSK
ndax lekk gi, bakkan bee ko ëpp solo, te koddaay li it, yaram wee ko ëpp solo.
Philippians 3:8
TSK
Rax ci dolli, lépp sax laa far jàppe ag wàññeent, ndax ngëneel li sut lépp, te mooy xam kuy sama Sang Almasi Yeesu. Moom moo ma taxa nangoo ñàkk lépp, def lépp ni mbuubit, ngir tonoo Almasi,