TSK

TSK · Job 21:10

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Su ko defee du kenn ku ëmbam di yàqu, mbaa mu tëlee am doom ci seenum réew, te maay matal sëkk seen limu fan.

Aji Sax jee leen di xéewale, ngir baaxe seen meññeefum njurukaay, ak seenug jur, ak seen meññeefum suuf, ca réew ma mu giñaloon seeni maam, ne moom la leen di jox.

Loolu lépp laa walbatiku xalaat, ngir lépp leer ma: Ku jub ak ku xelu ak seeni jëf, lépp a ngi ci loxol Yàlla. Mbëggeel ak mbañeel, xamoo lu la ciy xaar, lépp a nga ca kanam.

¶ «Jenn waay la woon ju bare alal, di sol yérey tànnéef yu rafet, di dunde lu neex bés bu set.