TSK

TSK · Job 21:15

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Firawna ne: «Kan mooy Aji Sax ji, ba ma di ko déggal, di bàyyi Israyil, ñuy dem? Xawma sax kuy Aji Sax ji, waxumalaa may bàyyi Israyil, ñuy dem.»

Job 34:9 TSK

te naa: «Nit ki seet bànneexu Yàlla, ana lu mu koy jariñ?»

Yal na Aji Sax ji tëj gémmiñu kuy naxe, ak kuy làmmiñuy tëggu.

lu ko moy ma regg, weddi la, ba naan: «Kuy Aji Sax ji?» Mbaa ma ñàkk bay sàcc, di la ñàkke worma, yaw sama Yàlla.

Làquwma, di waxe bérab bu lëndëm. Newuma it askanu Yanqóoba: “Sàkkuleen ma fu dara amul.” Man Aji Sax ji maay wax dëgg, di biral njub.»

Yeena ngi naa: “Ndaw lu soof,” di ciipatu.» Aji Sax ji Boroom gàngoor yee ko wax. «Jur gu ñu sàcc ngeen may indil, ak guy soox, ak gu wopp, loolu mooy seen sarax! Nu ma koy nangoo ci seeni loxo?» Aji Sax jee ko wax.