TSK

TSK · Job 21:26

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Job 3:18 TSK

ña ñu tëjoon ne finaax, déggatuñu coowal ku leen di sas,

Job 17:14 TSK

ndegam maa naa paxum yàqute ma: «Yaay sama baay!» naa saxu bàmmeel: «Yaay bóoy!» mbaa «Jigéen sama!»

Job 20:11 TSK

Mooy ànd ak dooley ndawam, tëri biir bàmmeel.

Nii la ku wóolu boppam di mujje, mook ku ko topp, di safooy waxam. Selaw.

Lu mettee ngi nii ci mboolem lu am fi kaw suuf: Benn dogal la ñépp bokk, te it nit a ngi sóobu ci mbon, di mébét jëfi dof giiru dundam, ba noppi fekki ña dee.