Numbers 16:26
TSK
Ci biir loolu mu wax ak mbooloo ma, ne leen: «Ngalla dàndleen xaymay nit ñu bon ñii, te buleen laal seen lenn, bala ngeen di buuboondook mboolem bàkkaari ñii.»
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ci biir loolu mu wax ak mbooloo ma, ne leen: «Ngalla dàndleen xaymay nit ñu bon ñii, te buleen laal seen lenn, bala ngeen di buuboondook mboolem bàkkaari ñii.»
say bañ gàccoo gàcce, xaymab ñu bon ña gental.
day mujj seey fàww niy jonkanam; ña ko daa gis naa: «Ana mu?»
Maay limal Yàlla jéego bu ma séqi, di taxawi fa kanamam taxawaayu garmi.
Lu bon a la gënal lu baax, fen a la gënal wax dëgg. Selaw.
Maay wàcce alkute gi,» kàddug Aji Sax ji Boroom gàngoor yee, «mu dugg ba ci biir kër sàcc bi, ak kër nit kiy giñe sama tur, ay fen; ci biir kër gi la alkute giy fanaan, ba raafal banti kër gi, aki dojam.»