TSK

TSK · Job 21:33

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Job 3:17 TSK

Biir bàmmeel la ñu bon ñiy noppee sonle, fa la ña jeele doole nopploo,

Job 17:16 TSK

Xanaa day ànd ak man tàbbi bàmmeel, nu bokk tëraayu pënd.

Job 30:23 TSK

Xam naa xéll ne ci dee nga ma jëme, te mooy kërug ndajem képp kuy dund.

Kenn moomul bakkanam, ba man koo dese, kenn amul sañ-sañ ci bésub deeyam, kenn muccul ci boobu xare, te mbon du ca wallu boroom.

Kon ni ab dogal sédde nit ñi benn yoon doŋŋ bu ñuy dee, seenub àtte topp ci,