Job 34:22
TSK
Du fenn fu lëndëm mbaa fu ne këruus, fu kuy def lu ñaaw mana làqoo.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Du fenn fu lëndëm mbaa fu ne këruus, fu kuy def lu ñaaw mana làqoo.
Bu ngoonee ñu wàccsi, di xiiru niy xaj, di wër dëkk bi.
te naan: «Lu ci Yàlla xam? Ana xam-xam fa Aji Kawe ji?»
Fu ma jëm, ba sore la? Fu ma daw jëm, foo teewul?
Ku mana làqoo làquwaay, ba duma ko gis?» Kàddug Aji Sax jee. «Xanaa du asamaan ak suuf, maa ko fees?» Kàddug Aji Sax jee.
Mu ne ma: «Tooñaangey waa kër Israyil ak Yuda moo ëpp loxo lool. Réew maa ngi fees ak deret, dëkk bi fees ak yàqute. Nee nañooy: “Aji Sax ji wacc na réew mi. Aji Sax ji gisul dara.”
Bu ñu nëbbu woon kaw tundu Karmel it, fa laa leen di fekk, yóbbu. Ñu làqoo ma ca taatu géej, ma sante fa jaani géej, mu màtt leen.