TSK

TSK · Job 28:2

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Silla moom jur Tubal Kayin miy tëgg lépp luy jumtukaayu xànjar ak weñ. Tubal Kayin am na jigéen bu tudd Naama.

Réew ma dungeen fa néewe njël, te dungeen fa ñàkke dara. Réew ma, ay dojam, weñ gu ñuul la, ay tundam, xànjar ngeen cay gase.