1 Samuel 17:42
TSK
Waa Filisti ba séentu, séen Daawuda; muy xale su góor su ndaw, xees te góorayiw, mu daldi koy xeeb.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Waa Filisti ba séentu, séen Daawuda; muy xale su góor su ndaw, xees te góorayiw, mu daldi koy xeeb.
Nit ay takk, bésub xare, Aji Sax ji di maye ndam.
Kuy damu kay, na damoom xelam mu ko may mu xam ma, xam ne maay Aji Sax, jiy jëfe ngor ak dëgg ak njekk fi kaw suuf. Loolu déy mooy sama bànneex.» Kàddug Aji Sax jee.