Job 29:24
TSK
Samay ree gëmeesu ko woon, xanaa ne siiwa gis sama kanam gu leer.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Samay ree gëmeesu ko woon, xanaa ne siiwa gis sama kanam gu leer.
Maaka jàqa jàq bay jal-jali, sama xol biy fuddu! Éy wii mititu xol! Duma mana noppi, maa dégg wooteb liit ak yuuxi xare.
Bu liitu xare jibee, waa dëkk ba du tiit a? Am aw ay dina dab ub dëkk te du Aji Sax ji?
Taalibe ya nag boole mbég akug jaaxle ba tax manuñu koo gëm. Mu ne leen: «Lu ngeen fi am, lu ñuy lekk?»