TSK

TSK · Job 39:27

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ «Li ngeen wara sib ci njanaaw yi te deesu ko lekk moo di: jaxaay ak mboolem xeeti tan; ak céeli, bu xonq baak bu ñuul ba, bu mu mana doon, ak mboolem xeeti baaxoñ, ak mboolem xeeti looy, muy looy mu ndaw ak looy muy napp ak looy mu gudd nopp ak looyu màndiŋ, ba ci xar-jéjj ak tiiwi. Nangeen sib maf itam, ak kirigéej ak mboolem xeeti liccin;

Ndax xef ak xippi mu wéy, mel ni lu saxi laaf, ne fëyy, naaw ni jaxaay.

kiy yaakaar Aji Sax ji moom, di yeeslu doole; da naa fëyy ni jaxaay juy naaw, di xélu te du xiix, di dox te du xoox.

Hosea 8:1 TSK

«Sexleen bufta gi! Jaxaay jàyy ci waa kër Aji Sax ji, nde ñoo fecci sama kóllëreek ñoom, samaw yoon lañu gàntal.