TSK

TSK · Job 4:21

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Job 18:21 TSK

«Dalub kàccoor déy, lee di mujam, ku faalewul Yàlla, nii la màkkaanam!»

Job 36:12 TSK

Su ñu dégluwul, jàlli dexu ndee, faatu ndax xamadi.

Waaye ngalla teggil sab yar, sa diisaayu loxoo ngi may jekkli.

ba tey, day dee, fekkiy maamam, ña dootu gis ug leer ba fàww.

Baleen nit, noowal bakkan kese la! Ana lees koy nawe?

Yàlla nag ne ko: “Ñàkk xel! Guddig tey jii, dees na jël sa bakkan. Kon li nga waajal, ana kuy doon boroom?”

Naka la jant di fenk, ba naaj wi tàng jérr, saxayaay lax, tóor-tóoram ruus, taar ba réer ko mërr. Noonu itam la ki barele di jeexlee ci biiri yëngoom.