TSK

TSK · Job 8:2

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Dagi Firawna ya wax Firawna ne ko: «Lu nuy seetaanati, waa jii di nu yóbbe aw ay? Bàyyil bànni Israyil ñii kay, ñu màggali seen Yàlla Aji Sax ji! Xanaa yéguloo ne Misra tas na?»

Job 6:9 TSK

Yal na neex Yàlla mu nappaaje ma, yal na afal loxoom, ne ma tipp.

Job 7:11 TSK

Moo tax duma téye sama làmmiñ, xanaa di waxe biir njàqare, di jooye biir naqar.

Job 15:2 TSK

Ayóoba, ku xelu dina tontoo kàdduy ngelaw, mbel-mbelam nib jaas bu fees dënnam a?

Job 18:2 TSK

Xanaa dungeen noppi mukk? Àndleen ak xel, nu wax.

Ma nga naan: «Moo téxét bi, foo àppal sa téxét gi? Ñaawlekat bi, foo àppal sa ñaawle bi? Dof bi, ñaata yoon ngay bañ xam-xam?