TSK

TSK · Joel 1:20

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Mu am ay fan, xur wa ŋiis, ndax réew ma tawluwul.

Job 38:41 TSK

Ana kuy xont baaxoñ, fa doom yay wooye Yàlla wall, di tërëf ndax ub xiif?

Ñépp a la wékk bët, di yaakaar, te bu jotee, yaa leen di leel,