2 Samuel 1:23
TSK
Wóoy Sóol ak Yonatan, ñoo yiw, sopplu ba ñuy dund, te ba ñu deeyee, teqlikoowuñu. Ag jaxaay, ñoo ko gëna gaaw, te gaynde, ñoo ko gëna jàmbaare.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Wóoy Sóol ak Yonatan, ñoo yiw, sopplu ba ñuy dund, te ba ñu deeyee, teqlikoowuñu. Ag jaxaay, ñoo ko gëna gaaw, te gaynde, ñoo ko gëna jàmbaare.
Daawudaa noon bésub keroog: «Ku bëgga jam Yebuseen ñi, ca xuntim yoonu ndox ma ngay mana dabe seeni gumbaak seeni lafañ, xuloowaaley Daawuda yi.» Looloo waral waxin wi ñu naan: «Gumba akub lafañ du dugg kër Buur.»
suuf sépp la seen ndéey jibal, seen kàddoo àkki cati àddina. Kaw la Yàlla sampal jant xayma,
Aji Sax jeey yékkatil raaya, xeet wu sore, wal ug liit, wooye leen fa cati àddina, ñu jekki ne jaas, dikkal leen.
Dëkk bi lañuy song, ci kaw tata ji lañuy dukkate, ci kaw kër yi lañuy yéeg it, te ci palanteer yi lañuy jaare dugg niy sàcc.