TSK

TSK · Jonah 2:3

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Mu jëm ci njiital jàngkat yi, dëppook galan bu ñuy wax Tóor-tóor, ñeel Daawuda.

ñu sóoraale maak ñi wàcci biir bàmmeel. Ma mel ni jàmbaar ju kenn amatul yaakaar,

Teewlu na ma moos, dama koy woo li feek may dund.

Yunus ne leen: «Fableen ma, sànni ci biir géej gi. Kon géej gi dal. Ndax xam naa xéll ne ngëlén lu réy lii, maa leen ko yóbbe.»