2 Kings 20:1
TSK
¶ Jant yooyu Esekiya moo woppoon bay waaja dee. Yonent Yàlla Esayi doomu Amocc dikk, ne ko: «Aji Sax ji dafa wax ne: Dénkaaneel sa mbiri kër, ndax dangay dee, doo jóg!»