TSK

TSK · Jonah 4:11

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

fas ko it sama diggante ak mboolem mbindeef mu ngeen àndal, muy picc akug jur mbaa rabi àll— lépp daal lu génnandoo ak yeen ci gaal gi, di lépp luy dund ci kaw suuf.

Céy Aji Sax ji, gore nga ba kaw asamaan, dëggu ba kaw-li-kaw.

Ñoom ñépp yaw lañuy séentu, ngir bu jotee, nga leel leen,

Aji Sax jee baaxe ñépp, di yërëm lu mu sàkk.

«Kaayleen, nu waxtaan ba juboo,» la Aji Sax ji wax. «Li seeni bàkkaar di xonq lépp, tàll lay weexeji. Li muy xonq curr lépp, weex furr lay mujje.

Jonah 3:2 TSK

«Jógal dem Niniw, dëkk bu mag ba, nga yegge leen kàddu gi ma lay dénk.»