TSK

TSK · Jude 1:22

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ «Waaye Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Yeen sama gàtt yi, maa ngii di àttesi diggante xar ak moroom ma, ak diggante kuuy yi ak sikket yi.

Maaka bëggoona nekk ak yeen tey, ba gëna misaale sama baat, nde jàq naa lool ci yeen!

¶ Ñi ñu xasa leeral nag, te ñu jota mos may gu bawoo asamaan, séddu ci Noo gu Sell gi, deesu leen mana defal dara.