Job 6:11
TSK
Ana doole ju ma amati bay muñ? Ana luy sama muj ba may dundati?
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ana doole ju ma amati bay muñ? Ana luy sama muj ba may dundati?
Teddnga ñeel na Aji Sax ji! Ndaw kéemtaan ci ngor li mu ma jiwe biir dëkk bu ñu gaw.
¶ Mu ne ma: «Yaw nit ki, yax yii ñooy mboolem waa kër Israyil. Ñu ngi naan: “Nun de, ay yaxi neen yu wow koŋŋ lanu, sunu yaakaar tas na, nun kay yàqu nanu.”