Isaiah 24:18
TSK
Nga déggi yuux, daw, tàbbi biir pax, génne pax, laawoob caax. Mbàndi kaw kat ubbi na, kenug àddina di reng-rengi.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Nga déggi yuux, daw, tàbbi biir pax, génne pax, laawoob caax. Mbàndi kaw kat ubbi na, kenug àddina di reng-rengi.
Yeen waa Mowab, pat-pati rekk, di tàbbiy pax aki yeer.» Kàddug Aji Sax jee.
Fa kaw la Aji Sax ji sànnee sawara ci sama biiri yax, moo laaw ab caax ngir fakktal ma, waññi ma, jànnaxe ma, ma dëkke yoggooral.
ndax ni mbaal di bettee, noonu la bés bay jekkee dal ci kaw mboolem ñi ci kaw suuf.