TSK

TSK · Lamentations 3:52

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Sang bi, jéggal ma rekk ndax Aji Sax jee lay defal moos kër gu yàgg. Kon nag, Yàlla bu nit gis mukk lu bon ci yaw, sa giiru dund.

Mu jëm ci njiital jàngkat yi, ñeel Daawuda. Aji Sax ji laa làqoo. Ana lu ngeen ma naa: «Neel fëyy ni picc, toŋi sa kaw tund.

Noon bu ma deful dara, yàlla bumu gis lu mu ma damoo. Ku ma bañ ci dara, yàlla bumu ma ree.

tance ma kàdduy mbañeel, song ma ci dara.

seen xol tàng ci Yeremi, ñu dóor ko ba noppi, tëj ko ca biir kër Yonatan bindkat ba, fa ñu defoon kaso.

¶ Kàngami buur yooyu dem ne Buur: «Waa jii, na dee rekk; mu ngi yoqil xarekat yi des ci dëkk bi, di yoqil ñépp ndax waxam jii mu leen di wax. Waa jii kat wutul jàmmu askan wii, xanaa musiba.»