TSK

TSK · Lamentations 4:6

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Aji Sax ji nag yuree ca asamaan tamarax buy tàkk, muy taw ci kaw Sodom ak Gomor, na ko Aji Sax ji dogale.

Bu nu Aji Sax ji Boroom gàngoor yi waccalul woon li nu deseek as néew, ni Sodom lanuy mel, Gomor lanuy neexool.

Waaye yonenti Yerusalem laa gisal lu yées: ñuy jaaloo, di wéye ay fen, di dooleel defkatu lu bon, ba kenn dëdduwul mbonam. Ñoom ñépp di ma niru waa Sodom, waa Yerusalem it ni waa Gomor.»

Yaw Yerusalem, giñ naa ko ci man miy dund, kàddug Boroom bi Aji Sax jee, sa rakk ju jigéen ja, Sodom, mooki janqam defuñu li nga def yaw, yaak say janq.

Matal nga sa kàddu gi nga wax ci nun, nook sunu kilifa yi nu yilif, ba nga wàccee ci sunu kaw, ci Yerusalem, musiba mu réy mu masula am feneen fu mboolem asamaan tiim.

¶ «Jawriñ jooju xam nammeelu njaatigeem, te taxul mu waaj ko, ba jëfewu ko, ay yetam dina bare.